#sunumbir : c'est notre affaire ! 

Sur la politique

Werantee pólitig ... baaxul !

" Pólitig du njuuj-njaaj. Ci yoon kay, waru koo doon. Waaye sunu mbokk yi, ni xare lañ ko jàppe. Te xare, jotewul daraak rafet jikko. Li ci am solo, mooy gàddu ndam li. Jekkantul jam sa noon bala mu lay jam. Yef yi powum mag doŋŋ la : kenn du taxawal pàrti ngir defar sa réew walla jemale ko kanam. Kon mu mel ni fépp fu pólitig yàqee nit ñi, askan waa sàggane boppam."

Bubakar Bóris Jóob, Bàmmeelu Kocc Barma, Téereb nettali, EJO, 2017.

Pris en otages par notre classe politique.

#sunumbir

14/03/2026

Date de dernière mise à jour : Saturday 14 March 2026

Aucune note. Soyez le premier à attribuer une note !

Ajouter un commentaire